Wolof to English
Assalaamaalekum
Peace be upon you
Ñu ngi fi.
They are fine
Peace be upon you
Assalaamaalekum
They are fine
Ñu ngi fi.
Maalekum salaam
Peace be upon you
Na nga fanaane / yendoo?
How did you spend the night / the day?
Peace be upon you
Maalekum salaam
How did you spend the night / the day?
Na nga fanaane / yendoo?
Na nga def?
How are you doing?
Jàmm rek
Peace only
How are you doing?
Na nga def?
Peace only
Jàmm rek
Maa ngi fi rek.
I’m fine.
I’m fine
Maa ngi fi rek
Naka waakër gi?
How is the family?
How is the family?
Naka waa kër gi?